Sylla Madridista en wolof

Sylla Madridista en wolof

Partager

Halla Madrid 🤍😇

Photos from Sylla Madridista en wolof's post 19/08/2026

Photo wa Real Madrid saison 2026/2027

Halla Madrid 🤍
Yàll naleen yàlla defal ay ndam you bari

19/08/2026

Jose Mourinho "

Mbappe ? Dafa yéeme. Daf may reetaan loo ci biir tàggat yaram, dafa BAAX lool. Niveau bimu am mooy STRATOSFERIK

19/08/2026

Real Madrid présente na Bernardo Silva tay 🤍🇵🇹

17/08/2026

🚨💣jpedrerol : « Real Madrid mëuna signe benn joueur ci été bi

" ben milieu de terrain 🤍

17/08/2026

🚨 José Mourinho laaj na wa Real Madrid ñu siñe Martin Zubimendi ak lumu mëna doon

16/08/2026

Match bi jeexna
Real Madrid mu am ndam ci kaw Schalke 04 ⚪️🔵 3-0

Y nada mas 🤍

16/08/2026

Jour du match ⚽️
Vs Schalke 04 ⚪️🔵
Amical 🤝
15H00 GMT ⏰️

Halla Madrid 🤍

16/08/2026

🚨 Breaking : Real Madrid dañu intéressé wou ci milieu de terrain bi di Kees Smit 🇳🇱

🧠 José Mourinho mingi wër joueur yu mëna jouer ci posisioŋ yu bari, lu melni Bernardo Silva, te Kees Smit mën na jouer ci posisioŋ boobu.

📌 Waaye, ba leegi amagul benn jéego ci wàllu siñe.

🚨🗞️ [Diario AS]

15/08/2026

🚨 Kylian Mbappé : "Am entraîner bu melni José Mourinho lu am solo la; entraîner bu xam ni ñuy jëlee ndam la." 🤍

15/08/2026

🚨🧤 Lunin day des ci Real Madrid! 🤍🔥

Andriy Lunin dafa nara yokk contrat ak Real Madrid ba 2030. 🇺🇦🤍

Extension bii dafay gëna yombal dem bi. Rawatina ni ginnaaw bi Fran González deme, Real Madrid yaakaarna ni amatul kenn ku wóór ngir Thibaut Courtois. 🧤😬

Kon tëye Lunin ci Real Madrid lu am solo la ngir mëna wéy di nekk gool. 🤍🔥

📰 Okdiario

Vous voulez que votre entreprise soit Gym la plus cotée à Touba ?

Cliquez ici pour réclamer votre Listage Commercial.

Emplacement

Type

Site Web

Adresse

Diourbel
Touba